Sujets en langues nationales
                    
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu 
Date:   20-11-04 01:53   >>> Répondre à ce message

Sealiah man kham nga comme ni ma lako wakhé rek fi la yaro mais nak a la maison wolof la niou done lakka sinon on nous tire les oreille mais wolof bou takha souf lawone mais niari at doy bou fékénténé wolof nga .
Quand a yaw nak Deug déggana wolf ga wayé nak di wakh wolof acamiquegou pâ yi mome laulou da niou kay kholat té li nga moudja wakh deuggeu la tamite bou dé da nga deukkeu ak ay khalé mome di nga dégga man fi may wakhé moy nga diko djanga té deukkau fa laulou mo yomboul ya sealiah man settlou na né fou ma wakhé rek di nga ma tontou vraiment lou bakh la
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   20-11-04 13:59   >>> Répondre à ce message

mais nak l'élu, souma ley lire da mey khikheut, ya pas de ponctuations en wolof???
lol
mais yama gueun bax nak
 
 Re: wolofisons
Auteur: zoukeuse 
Date:   21-11-04 19:55   >>> Répondre à ce message

t'inquiète ... je suis pas mieux!!!
j'ai déjà planté 3 fois mon PC!!
Et déjà, pour arriver à m'y retrouver dans ce forum, je sais pas comment je fais!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: zoukeuse 
Date:   21-11-04 19:59   >>> Répondre à ce message

alors tu peux m'aider ... tu peux me dire qui chante ce magnifique zouk love?
 
 Re: wolofisons
Auteur: zoukeuse 
Date:   21-11-04 20:11   >>> Répondre à ce message

mais ce sont les paroles de la chanson que je recherche ... tu as toutes les paroles?
tu peux me dire ce que ça veut dire?
 
 Re: wolofisons
Auteur: zoukeuse 
Date:   21-11-04 21:27   >>> Répondre à ce message

je vais te donner une autre adresse ...
Pourrais-tu refaire un dernier essai?
A propos, connais-tu le nom du chanteur?
djerejef!!! (quelque chose comme çà!)
mariava@caramail.com
 
 Re: wolofisons
Auteur: mel 
Date:   21-11-04 23:19   >>> Répondre à ce message

Bonsoir a tous...
g reussi e m'exprimer en wolof ce we... g fais ma declaration... mais je n'ai pas compris la réponse, et ca c pas malin!!!
Alors si qqun pouvait me traduire "ma la raw", "wou you na la " et "diamak diame"...
S'il vous plait... vous qui parlez wolof ca vous prendra 2 sec, et moi ca me permettra d'acceder au bonheur!!!
merci d'avance a celui ou celle qui voudra bien m'aider...
 
 Re: wolofisons
Auteur: zoukeuse 
Date:   23-11-04 20:24   >>> Répondre à ce message

ma la raw c'est moi encore plus mais le reste je connais pas ...
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   24-11-04 10:41   >>> Répondre à ce message

zoukeuse on m'a dit ke le fichier est trop lourd pour passer par mail. Si tu te connectes sur msn je peux te l'envoyer sans prob
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   13-12-04 13:47   >>> Répondre à ce message

sealia:
mane dama contane ak sama smiley; kholal waye:http://www.postsmile.com/img/default/0559.gif
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   15-12-04 11:25   >>> Répondre à ce message

Nangéne déf
Dama toukki won, way gnibicina.
Guissnané, nit yangui lak wolof bubax.
Lolu di wanéné li amna fulla.
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   15-12-04 18:55   >>> Répondre à ce message

deug:
deug deug ya mana touki!!
naka wa fofou ?
naka khlé yi ?
fofu dé warna nekh! mo takh nga dème reck faté gnou !!
déwénati!!
yakameti wone na nga gnow!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   16-12-04 10:42   >>> Répondre à ce message

Déwénati
toukki liguéy lawon motax mu yag, té xamga sénégal du féppa am internet bu néxa jeffandico.
way nammon naléne lol, té guisnané mbirmi mingui takarnassé.
li ci kanam rawuli beut
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   16-12-04 11:48   >>> Répondre à ce message

namone nalène sama waay yi
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   16-12-04 20:04   >>> Répondre à ce message

niola gueneu name , sounou garand ; té dougnou ko bagne!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   28-12-04 11:47   >>> Répondre à ce message

Naka guéntéwu Noél?
mangui doon xar kuma thi boolé, way dafa melni sama gayi dangn ma faté.
at bi di doorsi, mang léén si gnanal wér, comcom ak jamm ju bari.
Bu narré gnaw, yalla na dakh bi di jééx
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   28-12-04 18:18   >>> Répondre à ce message

amiiiine
gnou bokk niane bi
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   29-12-04 18:18   >>> Répondre à ce message

sealiah:
comme fut emouvant ton premier message!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   30-12-04 10:49   >>> Répondre à ce message

and now???
mais déwagouma dé
suis là
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   30-12-04 18:20   >>> Répondre à ce message

and now?
j'espère que t'as récupéré ta vox, que t'as bien mangé !!que t'as mis ta pancarte au frais!!
la seule chose , tu disait que tu voulais apprendre le woloff ; mais tu voulais sûrement dire "donner des cours de wolof"!!
yow!! yala nga goude fane !!
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   31-12-04 09:47   >>> Répondre à ce message

Amine
Pierre, c'est parce qu'elle est humble mais toi aussi tu n'es pas en reste.
j'éspére que la fin d'année se fêtera bien de votre côté.
Su naré naxari, mangui lééni xaar Thiés guir gnou bok-co.
Ba déwén!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   31-12-04 11:01   >>> Répondre à ce message

suma nieuwé thiès dina la setsi deug

pierre_diop mom jé encore du mal à analyser ay waxam, donc je l'observe encore koi

té nampouma wolof, donc diangueu moma meuss taxa diog pierre
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   03-01-05 10:11   >>> Répondre à ce message

Gnou doug si jamm di gnan jamm sax si aduna ndax gnou mana xékh xif ak gnak.
Di gnan li xéw Asie, Yalla mousseul si aduna-bi, diappalé gni dund bagn wéssu tiss-bi si jamm.



Message édité (04-01-05 11:30)
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   03-01-05 22:56   >>> Répondre à ce message

Deug:
deug deug besse bouma niowé thiès , di na la set si !!
mane fouma nek rek ma ngué deguelou woye boubou , kokou nane 'thiès la dioudo , thiès la fèke bakh", khame nga kokou di woye thiès ?
thiès warna nèkhe dé, deug deug !!
masse na fa lèke bène chawarma thi chawarma bobou nga khame né tourou niary djiguène la yor , fofou thi yonou ndar , té aye libanais déféna nioko mome !!
fofou mo nekh!!
da ngaye lèke chawarma bounèkhe, bé paré nga nane bène bierre bou galacée ; lolou dara dakhou ko !!
sealiah: guisse nga sa ma wakh ni mou léré!!

 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   04-01-05 10:26   >>> Répondre à ce message

sa bierre bobou key moma diakhal
té meuno si tekk bissap rec???
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   04-01-05 11:34   >>> Répondre à ce message

Pierre yow xam nga Thiés bou bax, cagn nga fa guéj?
way fim tolni danga sorri lol moma diaxal?
Sealiah, yow cagn ngay gneuw Thiés?
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   04-01-05 11:47   >>> Répondre à ce message

bientôt
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   04-01-05 18:51   >>> Répondre à ce message

Deug:
chawarma bi mou ngui toude "pamenda"!!
si tu es sage sealiah viendra te voir!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   04-01-05 18:53   >>> Répondre à ce message

il est plus sage que toi
c'est une certitude
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   04-01-05 20:05   >>> Répondre à ce message

sealiah:
tu es sûre de tes certitudes ?
méfie - toi car il y a des certitudes qui ne sont pas sûres!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   05-01-05 10:49   >>> Répondre à ce message

je suis sûre et certaine de Cette certitude là
sama baat si kaw nak
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   05-01-05 16:48   >>> Répondre à ce message

sealiah :

khame na yow doye nane bierre !!

yow kaye sa affaire yombe na : diokhla bène mboussou bissap bou 25fcfa kaye mome yombe na , nga dème nampe ko té maye gnou diame !!

deug deug , léke chawarma bou saf sap béparé nga tègue thi bissap ? bissap nga khame né soucare rek la saf !! lolou dal mome dou affaire !!

yow , bayile affairou kao kao waye!!

gnoune wa takhe yi , berre la gnou kham , berre la gazelle bien frappée; akh, kène douko diawate lé , té mosse doli la !!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   05-01-05 17:01   >>> Répondre à ce message

mané nanal sa berre ba meukeu mur bi, sama fou nékoussi, wayé doumako nane tey, doumako nane euleuk
té kouma khole khamné douma nampa mouss.
ni ngey mince yeup!!
soy diangueu khassté nak nga waxma



Message édité (05-01-05 17:10)
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   05-01-05 20:04   >>> Répondre à ce message

sealiah:
cheu , sealiah momana khass !!
wakhouma mouss dé, mbouss la wakh, sachet de bissap à sucer !!mbouss = sachet !!
kham ngané doumala khass , yow tame !!yaye sama kharite thi forum bi!! lo ma def bé ma dila khass ?
mane tame sama nane barioule dé!! de temps en temps rek!!
sacrée sealiah , sister lebou!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   06-01-05 02:08   >>> Répondre à ce message

Naane ci boppam mo baxoul amoul benna intéret !! vraiment sama gane yaw PIERRE bo nané da ngay geuneu intelligent walla daf lay may dolé ?
loudoul rousslo la bo ci euppeulé
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   06-01-05 10:06   >>> Répondre à ce message

en tout cas dé goukh na bala mouma tontou
mbouss = mouss = sachet = ma tey weu
 
 Re: wolofisons
Auteur: camille 
Date:   06-01-05 18:09   >>> Répondre à ce message

celui qui chante khalebi je crois que c'est sylvestre gomis
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   06-01-05 18:39   >>> Répondre à ce message

l'elu:
oh!! lek lou saf béparé nane berre bou sède? dara dakhouko !!do gueuneu intelligent wayé di nga ame touty banèkhe!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   07-01-05 04:22   >>> Répondre à ce message

Way bane banékh man sama guiss guiss bou soriwoul guiss nga nga lékka lou saff nga tek ci benna jus(mo xam ditakh, bissap, bouy, corossol....) bou andak ay glaçon dara daxou ko bou fékénténé gouddi la nak way nga tek ci benna gazelle (limonade) ndax nga bagna feur lol
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   07-01-05 09:56   >>> Répondre à ce message

lekk daal
ndokh rec mo siy tégou
boisson bou sucré bi ak bou tang bi yeup ce n'est pas sain
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   07-01-05 17:58   >>> Répondre à ce message

Pierre dama beug nga bay Sealiah tout tranquille boco mounoul jandal lim beug bissap (té waxul bou 25f yaw tamit).
Néko nak yaw bissap toubab ngay nan.
Thiés mom week end ba week end la fay dém, motax yén sayi douma guén sax, sufa sealiah gneuwé nak, térru buur lacoy térro.
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   07-01-05 18:05   >>> Répondre à ce message

pierre diop dé khamal sa bop nak légui
deug temps yi war na nieuw thiès pour le boulot, mais on va se croiser dé
week end douma fa fekk
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   07-01-05 21:54   >>> Répondre à ce message

deug:
sealiah , bayinako tout taranqillement; do to mako toudeu ; bayi nako ak limonade gazellame , ak ndokh mou sédame ;
ndar : kham nga louye bissabou toubab ? moye bigne !! sama mboki peul bou gnoye wakh bigne da gnoye né bisabou toubab !!
lelu , yangimaye fatali lou nèkh: jus de ditakh , lokhamené sealiah khamouko ; mome ndokh rek la khame .
sealiah , ndéké da ngaye liguèye !!yow fo mané liguèye ? débourouyèle bé bo démé thiès nga guiss deug ; deug dafa bakh!!néna daf laye recewoir téré bien .
 
 Re: wolofisons
Auteur: dyastou 
Date:   07-01-05 23:02   >>> Répondre à ce message

pierre_diop, domou baye yo ya yep sealiah lol
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   08-01-05 20:32   >>> Répondre à ce message

dyastou:
na nga def ? célia sama kharite la!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   09-01-05 21:02   >>> Répondre à ce message

alors céalia: tu es revenue de thiès pour ton liguèye ?
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   10-01-05 11:13   >>> Répondre à ce message

Auteur: pierre_diop
Date: 07-01-05 21:54

deug:
sealiah , bayinako tout taranqillement; do to mako toudeu

...........

défal li nga wax rec mo gueune
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   10-01-05 14:27   >>> Répondre à ce message

sealiah:
mais , Sealiah, lolou la dèfe di ;
guissou lo légui Célia laye wakhal; Sealiah yow mome bayinala taranquilement , do tou mala toudeu!!
mane louma wakh rek laye dèfe , ma mèle nonou !
mane boye poulo lebo nouyou na la !!
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   11-01-05 14:19   >>> Répondre à ce message

Pierre,
so dafé lolu mou nekh ma parce que Sealiah dou sa domou bagnén.
Way bou gneuwé Thiés dinaco terrou nognouy tééro buur.
Lumouy saf sa bissap bi ngay nan?
Salut à gneup



Message édité (11-01-05 23:47)
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   13-01-05 19:48   >>> Répondre à ce message

deug:
deug deug , di na ko dèfe !! dina sakh ine di célia , si allah diaby !!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   14-01-05 11:45   >>> Répondre à ce message

dem na thiès ba nieuw
10é la nékone
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   15-01-05 19:17   >>> Répondre à ce message

louye 10 ème !! khana lolou kartier la ?
deug , so démè 10eme , so fa séné bène guèle bou nice rek néko célia!!kokou mome lou wore la, té khame na mome laye done !!
célia , war nga nice dé !!
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   16-01-05 01:41   >>> Répondre à ce message

Man Hersent la nek.
Té semaine bi yeup mangui Ziguinchor.
Pierre ma wax la nak, Sealiah néxoul xammé néxoul guiss.
Bomaco meuné portélél ma jeul
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   17-01-05 10:28   >>> Répondre à ce message

tey mou nekh dé
mane extra terrestre la
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   17-01-05 10:44   >>> Répondre à ce message

martienne
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   18-01-05 10:10   >>> Répondre à ce message

ndar namesss
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   18-01-05 10:50   >>> Répondre à ce message

nangadef?
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   18-01-05 12:27   >>> Répondre à ce message

je vais trèèèèèèèèèèèèèèèèès bien
merçi
 
 Re: wolofisons
Auteur: Vaarash 
Date:   22-01-05 14:22   >>> Répondre à ce message

Bonjour,
Est-il possible d'avoir la transcription phonétique de quelques phrases wolof sur ce site?
Par exemple, comment prononce-t-on :
"Man naa la wax dara ?‎"
je connais la traduction :
"Je peux te dire quelque chose ?‎"
mais je ne sais pas comment la prononcer !
J'ai environ une dixaine de phrases simples comme celle-ci que je voudrais bien savoir prononcer.
Merci à l'avance.
Vaarash
 
 phonétique wolof
Auteur: Vaarash 
Date:   22-01-05 14:24   >>> Répondre à ce message

Bonjour,
Est-il possible d'avoir la transcription phonétique de quelques phrases wolof sur ce site?
Par exemple, comment prononce-t-on :
"Man naa la wax dara ?‎"
je connais la traduction :
"Je peux te dire quelque chose ?‎"
mais je ne sais pas comment la prononcer !
J'ai environ une dixaine de phrases simples comme celle-ci que je voudrais bien savoir prononcer.
Merci à l'avance.
Vaarash
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   24-01-05 11:36   >>> Répondre à ce message

tu le lis comme on l'a écrit, je ne suis pas fort en phonétique pour t'aider.
Il faut demander à Sealiah qui est une ET marsienne, ou à Pierre Diop qui a le Dico en tête.
Sama gayi, xana xar bi molén jaap?
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   24-01-05 11:44   >>> Répondre à ce message

bane xar? la tabaski est fini depuis deux jour deug, tu parles encore de mouton...on bosse nous
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   25-01-05 17:39   >>> Répondre à ce message

ah bon
 
 Re: wolofisons
Auteur: kirikou   
Date:   31-01-05 12:59   >>> Répondre à ce message

salamalekum vaarash!
deug a raison tu le lis comme c'est écrit mais le x tu prononces "r".
bon courage
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   31-01-05 17:44   >>> Répondre à ce message

saaaalut
namone na lène
deug fo nek yaw??
ndar na nga def???
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   01-02-05 09:47   >>> Répondre à ce message

le retour?
 
 Re: wolofisons
Auteur: michele 
Date:   01-02-05 16:51   >>> Répondre à ce message

bonjour

je ne peux pas terminer la traduction d'une lettre en woloff car il me manque des mots que je n'ai pas trouvé et mon lexique est pauvre . Merci d'avance à celui ou celle qui peut m'aider

- noo niendo
- dama la bouga
- thi ligaye
- dama contane

dieuredief
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   03-02-05 18:07   >>> Répondre à ce message

noo niendo = comment tu té mouché? lol
ça doit pas être ça

noo yendo = comment s'est passé ta journée
dama la bouga = je t'aime ou je te veux
thi ligaye = ??? je ne vois pas
dama contane= suis content(e)

cé tout ce ke je peux, désolée
mais ou sont passée les traducteurs? pierre diop ou deug?
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   04-02-05 09:52   >>> Répondre à ce message

n'oublies pas que tu es traductrice aussi!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   04-02-05 16:24   >>> Répondre à ce message

ndar fo dougone?
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   07-02-05 14:16   >>> Répondre à ce message

pas disparu!
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   10-02-05 15:31   >>> Répondre à ce message

peut-être "thi ligaye" est "ci liggeey", aloor on peut traduir comme "dans le travail"
xamuma, de fait.
Bëgg naa pratiquer wolof wànte dafa metti.
Bë apre!
 
 Re: wolofisons
Auteur: ingalill 
Date:   27-02-05 01:20   >>> Répondre à ce message


En phonétique c'est autre chose di, thieboudienne pour ceebujen et thiouraye pour curaay (ak yeneen ak yeneen)c'est du français et rien d'autre, enfin, à mon avis. Le phonétique s'écrit avec les signes IPA, ce qui ne se trouve pas sur un clavier ordinaire (du moins pas sur le mien qui est suédois).

Enfin, c'est mieux que les gens écrivent mal que pas du tout je pense, même si le wolof et le français, écorchés sont difficilement compréhensibles pour les autres.
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   08-03-05 15:18   >>> Répondre à ce message

Ici, nous sommes à l'Académie, Kocc Barma serait fier de se réveiller dans ce forum.
Nangén déf?
Gisnafi ay Kocc yu béss, dég nafi ay batt yu béss.
Waynak, gan-yi def lénn dang, pierre Diop ak Sealiah da gnuy nélaw bugnu yéwo rek mu néx.
Hohodei mom dafa dégg ba jaxalma, ku xam dara bim jangé?
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   09-03-05 14:57   >>> Répondre à ce message

deug c'est un appel à piere diop??
kokou dafa téyé boppam légui
sof rec
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   09-03-05 16:47   >>> Répondre à ce message

Quelle susceptibilité, Ingalill!

Je ne prétendait pas donner un cours de phonétique, j'essayait seulement de donner une possible réponse à une post précédent... c'est tout.

Et Deug... war nañu wax...
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   09-03-05 18:21   >>> Répondre à ce message

boulène khèkh rec !!!
wakhtane kessé
 
 Re: wolofisons
Auteur: ingalill   
Date:   09-03-05 23:46   >>> Répondre à ce message

hodei, je ne crois pas que c'est ton message que je commentais..

Ce qui m'énerve trop sur les forums d'Internet est la façon de certains français de France (ou autres ethnocentristes) de se dire que l'orthographe française, ou la leur du moins, est la seule correcte, alors que dans le cas du wolof justement, avec l'orthographe th pour c etc, c'est moche et de plus, quasi-illisible pour tous les non-français (comme Tubaab de ce même forum) et les autres qui ont essayé d'apprendre le wolof avec l'orthographe normée et non en puisant dans le parler, qu'ils maitrisent. Cette orthographe normée existe quand même depuis 1971, depuis le temps, on aurait pu s'y faire non? Yaakaar naa ne leegi dëgg nga lii ma wax? Bëgguma xeex!!

Je m'excuse si je t'ai vexé, ce n'était nullement mon intention.



Message édité (09-03-05 23:51)
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   10-03-05 18:58   >>> Répondre à ce message

Ok Ingalill... amul solo... bëggoon naa clarifier rekk... bëgguma xeex, sérieux :D

Pas grave, fils.
 
 Re: wolofisons
Auteur: ingalill   
Date:   10-03-05 19:23   >>> Répondre à ce message


Duma "fils" de, man jigeen laa.. Ingalill ab prénom de fille suédois la!

Xeex baaxut, diggante mo gën, wax nga dëgg.. :)

 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   11-03-05 09:52   >>> Répondre à ce message

ingallil dakar mom, fils nieupa ko mom amoul goor , amoul djiguène
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   11-03-05 13:08   >>> Répondre à ce message

nan gadef sealiah
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   11-03-05 16:51   >>> Répondre à ce message

:D ok ok Ingalill... fille ;P
wànte xalaat naa ne ma mën wax "fils" pour jiggeen ak góór...
mmmm?? dinaa ko laaj... jejeje
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   12-03-05 13:51   >>> Répondre à ce message

ingalill tu as raison pour l'écriture du wolof; Et si les wolofs au Sénégal faisaientt eux-même un effort pour apprendre l'écriture comme certain(e)s le font ici. :=)
 
 Re: wolofisons
Auteur: ingalill   
Date:   12-03-05 13:58   >>> Répondre à ce message

jërëjëf, sa wax neex na ma lool! Tey, am naa liggeey bu bari, wánte aucune envie de le faire.. donc toutes les réjouissances font plaisir, petites et grandes. :)
 
 Re: wolofisons
Auteur: cori 
Date:   20-03-05 17:25   >>> Répondre à ce message

j'entre discrètement dans la discusse, ça fait plaisir de vous lire.
 
 Re: wolofisons
Auteur: claire 
Date:   25-03-05 00:06   >>> Répondre à ce message

Voilà, je suis complètement folle de mon meilleur ami qui est sénégalais, je ne parle pas le wolof et j'aimerais lui déclarer mes sentiments dans un poème wolof, quelqu'un peut m'aider, please, merci d'avançe!
 
 Re: wolofisons
Auteur: kikinou 
Date:   25-03-05 06:09   >>> Répondre à ce message

pas moi, car je ne comprends pas encore le woloof lol mais tu sais dans ses cas la un regard sufit lol
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   25-03-05 10:12   >>> Répondre à ce message

Mangi yanal sunu mbokk chrétien-yi béssou pâque bu nékh dilén ndokkél ak dilén wax déwénatti.
Mangi nuyu Sealiah dico gnan mu gneuwatt ndax sunu vocab tané.
Ana Hohodei, l'Elu, Guéwélbabtou etc.
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   28-03-05 05:45   >>> Répondre à ce message

Deug sama serigne ma ngui ni !!
dila ziar té di wakh "alléluia" pour sunu mboki chrétien yi ci sen bess bou magg bi yalna sén pâques nekh .
Man nak dama amone ay examens laulou mo takh dal ma gueudj fi mais incha allah dina rattraper li ma wéssou yeup
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   29-03-05 13:35   >>> Répondre à ce message

Bég si sa délussi, ndaxté xaw nagnu wéét tuti. Sealiah légi consultante-la fénén. Pierre kén xamul fumu doug.
Wéét nafi, way sant yalla binga déllussé.
Naka sa examens yi? Yalla nassi Yalla daf xéwal bu réy.
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   29-03-05 14:18   >>> Répondre à ce message

waw mais deug
yaw il faut rec nga toudeu ma soy wakh????
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   30-03-05 17:39   >>> Répondre à ce message

Yaw la gnémé
Hohodei damaco toud mou napma
Yawiit boma nappé donk ma bayila!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   30-03-05 18:44   >>> Répondre à ce message

khamna fima ley napé
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   31-03-05 12:36   >>> Répondre à ce message

nap=attraper?
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   31-03-05 18:11   >>> Répondre à ce message

mais ici ça veut dire : intimider
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   31-03-05 20:09   >>> Répondre à ce message

jërëjëf Sealiah! leegi nak... lu muy tekki tout ça? :D
yangi ci jàmm, fille?
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   01-04-05 13:50   >>> Répondre à ce message

lu muy tekki?

Auteur: Deug
Date: 30-03-05 17:39

Yaw la gnémé
Hohodei damaco toud mou napma
Yawiit boma nappé donk ma bayila!
............
deug a plus peur de toi que de moi
alors il préfère s'attaquer à moi

et ça, dou deug dou yone !!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   01-04-05 14:11   >>> Répondre à ce message

jajjajaj, ok ok... Sealiah. Un certain point de la conversation je m'avais perdue jiji...
Deug... danga tiit? :D
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   01-04-05 14:40   >>> Répondre à ce message

léégi dangén ma beug sott, wayé tiitumalén
ndaxté yéén jiggén yi lamégn rek ngén am, wayé bu dara déssoul ludul jeff ngén daw.

Sealiah, loy ragal si Hodei? Mu napla rek nga daw, albatiku si man! Yama bétt.
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   01-04-05 14:51   >>> Répondre à ce message

topal fé
mane dé sama kokette la yor comme arme
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   03-04-05 01:29   >>> Répondre à ce message

kokette dé man mome yeuye la ci kahm lol
 
 Re: wolofisons
Auteur: nangadef 
Date:   04-04-05 15:41   >>> Répondre à ce message

A belli mo vojo vedé se me capite!!
BA beneen!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   05-04-05 14:54   >>> Répondre à ce message

l'élu yaw fo khiffé?
dalou kokette , maname chaussure à talons la wakh, pas croquette
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   08-04-05 02:43   >>> Répondre à ce message

waw ga dama djoum wakh nga deuggeu mais instant bi ni ma ngui fi may ligueyé mais dama khiff ba guissou ma .
li metti na way do ma bahal indil ma benna sandwich?
boumala nianalé rek lau beuggeu da nga koy am
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   11-04-05 16:47   >>> Répondre à ce message

okhoooo, kone raténa niane bi nii?
mais yaw khiff rec nga gueuleum?
khana fall nga santeu?
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   12-04-05 02:30   >>> Répondre à ce message

dédéte man SARR la santa guiss nga dé sama santa dafa nekh nilem .
té li takhaune ma khiff moy lekkouma journée bi yeup
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   12-04-05 16:31   >>> Répondre à ce message

sarr???
diamou toucouleurs yi?
béneu la, ragal khiff
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   13-04-05 01:58   >>> Répondre à ce message

NON douma sérére ni toucouleur dé man WOLOF la djolof la djaugué direct khamonané laulou nga may wax wayé nak djappa na la .
WOLOF la té dou dagne té khiff guissouma kou ko niamey
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   13-04-05 12:06   >>> Répondre à ce message

khana yaw do wor?
degueur kedj la la wakh ni mane, niémé khiff la def

boul mèl ni deug dé, mom sou khiffé dey dioye sakh
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   13-04-05 14:45   >>> Répondre à ce message

-
 
 Re: wolofisons
Auteur: Faalé 
Date:   14-04-05 14:36   >>> Répondre à ce message

Sealiah, gissnga yaw boo bayi wul sama jeukeur bi ngay togn dinala fathie.
Sama wax dussi sori!
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   14-04-05 14:52   >>> Répondre à ce message

Allez Faalé mangi si sa ginaw
Wayé waxléén si Sarr Wolof, fumu am danga galli
Sealiaah samaa xiif bo bayil dico wax dina def si yaw!
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   14-04-05 14:54   >>> Répondre à ce message

bane école de médecine nga diar?
am nga dipolome?
consultations niata???

deug dé dioye ba youte ley def, mako wakh , sama bat si kaw
yaw da nga am gardal corps légui???
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   14-04-05 15:49   >>> Répondre à ce message

trop de français dans ton post sealiah! :-)
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   14-04-05 16:17   >>> Répondre à ce message

ndar, cé faalé ki promet de me soigner si je laisse po deug trankil
d'où mon french
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   14-04-05 20:02   >>> Répondre à ce message

lutax nànduma dara lan ngeen wax? :(
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   19-04-05 03:55   >>> Répondre à ce message

Deug nga bahal ma dé wayé nak ya ngui may tutoyer cone dal SARR wolof waroul dal vraiment laulou deuggeur fit dou ko wéssou.
Man dé samay 10 mame yeup wolof lagnou done lakka parce que dama ko latchté niou wakh ma ko.
Té itam ma khamal lané li nga done bo ko bagné da fékka nga gueune cé niaw
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   19-04-05 15:19   >>> Répondre à ce message

l'élu? kham nga loutakh ma fan leu???
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   20-04-05 08:29   >>> Répondre à ce message

tu joues les troubles-fêtes Sealiah? :=)
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   21-04-05 02:38   >>> Répondre à ce message

Sealiah ma ngui khar sa tontou!
parce que dama la beuggeu khamal né ak lo ma fan fan , mala raw ci coté bou nekka.


Parce que sama grand DEUG day déconner koi kou ko bahi mou def ma toucouleur walla sérére .
Man Alboury ndiaye moy sama mame (descendant direct) kana kay mome do ma wakh né dou wolof?

Wayé nak kham na ba paré li nga may tontou kham na né di nga ma togne (rire)
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   25-04-05 17:10   >>> Répondre à ce message

mane sakh dama ragal tontou, mais yaw l'élu lo khalat nonou sakh? han?
mane bayi na togne dé
li takh ma fan leu, moy sa wolof yi ngey lakk té maguéwoulo sénégal.
jé vu ça dans un post, je ne sais plus où

deug mom boulko falé, preira leu sant, khaw dégg touti wolof rec di gnou sonal fi
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   26-04-05 04:35   >>> Répondre à ce message

kham nga li ko waral moy dama djanga fikh , té ci biir dafa am ay wolof you deuggeur you takkou yo kham né mome tcha sounouy maame ya lagn ko done wakh .
Té itam dama beuggeu sama lakka , man dé yallah kham nané chak fois daniou ma done dakh pour ma bagna jour baatou wolof dama gagner ba sonna mais gni ma wara santa moy yallah ak sama papa, momima djoloff ma djangui aduna france bakhoul ci khalé
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   27-04-05 11:47   >>> Répondre à ce message

waw mais di nga déloussi beuss sénégal?
wala wacances rek mo la fiy indi?
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   28-04-05 04:12   >>> Répondre à ce message

Fi mou nékka ni ma ngui djanga ay étude you ingénieur mais bou sobbé yallah bouma paré sama djanga dina fi liguey incha allah 4 walla 5 ans ngir ma am touti expérience bou laulou wéssau nak ma déllou définitivement senegal ngui djappalé sama réw , té man dama yakkar né téranga bo ko amé sa rew mo gueune walla?
Instant bi nak kham nga man étudiant la mais nak dama am ay kahitou france manaam toubab bou nioul la mais nak da koy bagne (rire)
vacances rek la am pour dellou faufou noce touti fikhal sama khole parce que vraiment france kou ko khamoul rek mo fo beuggeu nieuw .
damay faral di wakh naane kou am li nga beuggeu sa rew dou woutti fénéne sama cousins yi nekka fi sakh damaléna djakhal ndakh ni ma beugguer gnibbi .
bougn ammauni kahite danagne def ni man mais nak yallah bakh na
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   02-05-05 13:24   >>> Répondre à ce message

yaw key amoulo morom
déloussi liguèyal sa rew dé dara dakhouko.
Tabakh si sa rew dé mo gueun defko réwou diambour.
Fofou mom, lo fa yagueu yagueu, dou takh gnou dileu fatali sassou nek né deukoulo fi .
yallah na la yallah diapalé , té def li gueun si yaw...té nga bagn am lo rethiou
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   02-05-05 18:15   >>> Répondre à ce message

Sealiah trés sage (félicitation)
gétax lumu yag yag si biir guéj du sopaléku muk jassit
mangi léni nuyu bu bax, l'Elu mangi jégallu si togn bi.
xamnané sant deukkatul fén, té lu woor nga wax.
Naka jangmék yénén yitté yi?
Séaliah yaw lo def Fallé bamou daw?
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   03-05-05 05:52   >>> Répondre à ce message

Grand DEUG amoul hakha djappalouma kén hakha ci forum bi té li nga wakh rék affaire de togne la rek moy nékhal waxtane mais sinon ma ngui léne di déllo ziar .
Sealiah sa gnane bi daffa daw yaram sakh yalna la yallah dégga té nangoul gnane béppa mbindéf dieuré dieuf yallah rak mola manna faye té itam léppa lo beuggeu rék yalna la ko sounou borom bi déffal té mou gueune ci yaw .
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   03-05-05 16:41   >>> Répondre à ce message

sniff
yama wakhal lii lep? amine
ma nieuw damay dioyi fé
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   04-05-05 02:45   >>> Répondre à ce message

Wa mais gaheine bi mome mongui sonal nit gni dé ahhhhhhhhhhhhhh way
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   04-05-05 12:16   >>> Répondre à ce message

Nax nga yéméco wax
gnun dé limiy lak dégugnuco, su waxon wolof dina tané.
L'Elu war ngama baxé ay taalif sudé am ngaco.
Sealiah, am ma abal la mouchoire way du coton nak.
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   04-05-05 14:58   >>> Répondre à ce message

sétèèètèèt li loumou?
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   05-05-05 03:49   >>> Répondre à ce message

nguéne bahal ma dé mais con rek moy def louni mel mais nak grand deug ay téré mome dou mako faral di takka ndakh té yallah bouggou ko bakhoul yaunéntabi (psl) gnane ray ci yaram la khamaune dieurédieuf nak
 
 Re: wolofisons
Auteur: dyastou 
Date:   06-05-05 00:46   >>> Répondre à ce message

nanguendef mbokk yi? ma contance ci yen,ca fait plaisir de voir du wolof aussi bien parlé :)
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   06-05-05 13:52   >>> Répondre à ce message

dyastou, da gnouy dièm rec
mane dé l'élu la élire
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   08-05-05 01:37   >>> Répondre à ce message

tu me fais trop d'honneur sealiah man damay djém rek ni nga ko wakhé rek
 
 Re: wolofisons
Auteur: sealiah   
Date:   10-05-05 16:14   >>> Répondre à ce message

mba do rougir rec?
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   11-05-05 13:39   >>> Répondre à ce message

L'élu ninga jang ngé sama bataxal bi du nonu, waxuma téré, Taalif la wax.
Taalif, ay baat yu gnu boolé ba dégginn néx la manam si tubab "poéme".
Mbirou téré mom, nacoy dég rek.
Naka jang mi ak yitté-yi?

ma yoksi ay léébu

LU REER CI JUDDU, FEEGN CI JIKKO
LU AMUL DU AM TUR
LU FEEGN CIB SEY, NUYOO WOON NA CA NGORO LA, DAGNUCO FEYUL WONN



Message édité (11-05-05 13:43)
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   12-05-05 19:27   >>> Répondre à ce message

Deug... ban làkk nga wax boy?? lu tax ma la nànd? :(
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   14-05-05 04:21   >>> Répondre à ce message

Hhodei lim fi wakh dé wolof you deuggeur la dé té itam nekh na dégga .
Grand DEUG ma ngui déllo ziar djanga mi nio ngui ci rek mouy métti yitté yi nak nio ngui teuh ba légui affaire ba daffa metti grand surtout bo nékké étudiant dafay deuggeur mome kay yalnah no nou yallah dimbalé ba gnou guénna ci rek ci jamm ak salam
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   17-05-05 16:42   >>> Répondre à ce message

Salut l'élu!

Juumte am na ci sama phrase... bëggoon naa wax "lu tax nànduma la?"... waaye màngiwoon kaf, fils nadaxte xam naa ne GRAND DEUG wolof la wax :P

a plus!
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   17-05-05 16:42   >>> Répondre à ce message

Salut l'élu!

Juumte am na ci sama phrase... bëggoon naa wax "lu tax nànduma la?"... waaye màngiwoon kaf, fils ndaxte xam naa ne GRAND DEUG wolof la wax :P

a plus!

 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   19-05-05 05:44   >>> Répondre à ce message

Amoule benne probléme ya ngui ci biir
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   19-05-05 18:45   >>> Répondre à ce message

ok. :P
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   21-05-05 00:40   >>> Répondre à ce message

Cone yaw apparament yaw poular nga non ?
parce que ma ngui guiss né ci bennéne sujet ya ngui latch ndakh guéwélbabtou dou djanga pulaar !
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   22-05-05 19:27   >>> Répondre à ce message

Deedeet, l'élu... duma pulaar :D benn tubaab laa, ma jàng wolof rekk. Lu tax xalatoon nga ça?
Bëggoon naa xam si Guéwélbabtou progressait avec sa pulaar rekk.

ma la liir!
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   24-05-05 04:54   >>> Répondre à ce message

Ah oui je comprends mieux laulou mo takh nga am djafé dajfé pour dégga yenna phrase yi ok non en faite sa tour bi dafaf khawa nirau tourou pulaar té tu demender a guéwél si il voulait apprendre le pulaar
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   24-05-05 19:57   >>> Répondre à ce message

Uops! laajoon naa Guéwélbabtou su bëggoon jàng pulaar?? lu muy tekki "naka sa pulaar?" (ça va sa pulaar, n'est pas?)

Sama tur dafa pulaar? :D

nu mu deme, fils?
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   31-05-05 11:59   >>> Répondre à ce message

Nangén def samay andi jamm
Fanyi yitté yi dango xawa bari ba mayou gnouma nouma douggé si daraji.
Wayé amna mbégté si jang li ngén fi jota bind.
L'élu, fim tolni yaye serigne dara. Say ndongo bég nagn si yaw.
 
 Re: wolofisons
Auteur: toufa77 
Date:   31-05-05 13:02   >>> Répondre à ce message

arreter de dire ke maraba est un mot arabe
il et tou simplement utiliser par les musulmans*
j'espere ke vou avez bien compris
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   31-05-05 16:40   >>> Répondre à ce message

Fii sa kër la, Deug!! gëj nga bind ci forum bi :)
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   02-06-05 15:31   >>> Répondre à ce message

dotuma fi guéj su néxé Yalla
Ana gnom Elu ak gnénén gni?
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   03-06-05 03:27   >>> Répondre à ce message

Sallam a tous ma ngui sakh wallay mais temps yi dama am examen mo takh temps yi yeup bindouma dara
 
 Re: wolofisons
Auteur: dyastou 
Date:   03-06-05 23:41   >>> Répondre à ce message

M... a tous ceux qui sont en exam ( dont moi lol): inch allah lepp ay bax!!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   06-06-05 14:20   >>> Répondre à ce message

Mangi léni gnanal Yalla défal lén jamm si séni examen.
Waw lén goor
 
 Re: wolofisons
Auteur: bebs 
Date:   07-06-05 16:25   >>> Répondre à ce message

salam aleikoum...nanga def, naka se dougouda?mu ngi dalakh bou bakh?man abdou la toude.de me judo dakar be am se me bac...de me deuk paris mais se me deuk mo nekh....yaye diambar....diadieufete...
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   10-06-05 16:53   >>> Répondre à ce message

Abdou gnu ngi lay dalal si jamm dila gnanal jamm. Li gnu yekkati moy féxé ba yén gni nék bitim réw nguéni wéy di dégg sén lak, wayétamit gni nga xamné lak daléna néx di am fugnuco jeffa ndico.
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   10-06-05 20:17   >>> Répondre à ce message

Deug... incroyable!! nànduma dara, sériuex... fils, wax ma... am nga ñaari manière ngir wax ci wolof walla? jijiji

Noppaliku nga, man
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   10-06-05 21:15   >>> Répondre à ce message

tu veux que je te traduise hodei?
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   11-06-05 19:20   >>> Répondre à ce message

waaw l'élu... su la nexeeeeeeeee
 
 Re: wolofisons
Auteur: Sidi 
Date:   26-06-05 23:38   >>> Répondre à ce message

Salut.
Faati, sonnal nga sa bopp. kii moo la gena degg wolof
 
 Re: wolofisons
Auteur: PAPI LO 
Date:   28-06-05 13:09   >>> Répondre à ce message

waye waye deug raye ngua ma lol

bo do téne ma nane là bobou mome djappena ko béne leufi moytoul nane beu tchorokhnane rék
serieux vous me faites trop avoir la nostalgie du pays merci pour ces moments de detentes ke vous nous offrez PEACE
 
 Re: wolofisons
Auteur: PAPI LO 
Date:   28-06-05 13:12   >>> Répondre à ce message

bilaye seakliah ya wakh deug turkhistan sakh bo fa démé fék feu senegalais lol fred séteule bou bakh lol
 
 Re: j'ai plus fim que toi
Auteur: binou 
Date:   28-07-05 16:49   >>> Répondre à ce message

slt ca va je mapel binta j'ai 12ans et je cherche de quoi mange biousssssssss.
 
 Re: j'ai plus fim que toi
Auteur: baka 
Date:   28-07-05 17:01   >>> Répondre à ce message

binta tu est d ou exactement
 
 traduction
Auteur: pau 
Date:   12-08-05 15:41   >>> Répondre à ce message


Bonjour,

J'aurais juste aimé avoir la traduction de "sama nene"...
dieridief way
 
 Re: traduction
Auteur: Alima 
Date:   20-08-05 05:14   >>> Répondre à ce message

"sama nene," c'est "ma cherie"

Alima
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   26-08-05 19:01   >>> Répondre à ce message

Sama néné
au sens propre= mon bébé
au sens figuré=ma ou mon chéri(e)
Salut je suis de retour et je retrouve ce sujet avec beaucoup de plaisir
 
 Re: wolofisons
Auteur: hodei 
Date:   29-08-05 10:25   >>> Répondre à ce message

Deugggggggggggggg, fii sa kër la!
 
 Re: wolofisons
Auteur: Deug   
Date:   30-08-05 18:16   >>> Répondre à ce message

Waaw Hohodei
Dellussi na sama keur.
Fass yéné wéyal caddu Kocc.
Amna yakaar né sunu mbokk yu bari dagno nekk si yénéni mbiir, wayé danagnu gneuwatt gnu bokk guéwbi.
Kussi mélni Sealiah, wala Fred, wala l'Elu amonagnfi kaddu gu am solo. Gnu ngi lééni gnan gnu délussi budé amnagn jottam.
Ba fann yi bu néxé Yalla.
 
 Re: wolofisons
Auteur: ex-sealiah 
Date:   02-09-05 18:58   >>> Répondre à ce message

deug au secours jarive plus à me connecter avec sealiah
 
 Re: wolofisons
Auteur: tak 
Date:   04-09-05 18:23   >>> Répondre à ce message

sa ve dire koi thioro en wolof svp??
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   08-09-05 16:10   >>> Répondre à ce message

bjr ex
 
 Re: wolofisons
Auteur: l'élu   
Date:   10-09-05 01:39   >>> Répondre à ce message

Salamm sama mboka yi na nguéne def ?
mba yéna ngui am djam
laulou rek am solo .
Teuss teuss yi mo takh temp yi yeup awma djot mais nak ma ngui santa yallah bou bakh .


""Sama thioro veux dire
sama guel (girl) enfin ma copine quoi"" mais bouma wakhé laulou jeune souvent nio koy wakhé naunou mais nak li ci mak yi namma mome khawma ko
 
 Re: wolofisons
Auteur: a.joob 
Date:   11-09-05 19:55   >>> Répondre à ce message

jërëjëff, waa reew mi, nii laa ko bëgg. Ku nekk wax wolof ba mu set. Nuy ànd ci xel ak xalaat...
 
 Re: wolofisons
Auteur: ex-sealiah 
Date:   12-09-05 18:52   >>> Répondre à ce message

ndaaaaaaaaaaaaaarr
 
 Re: wolofisons
Auteur: ex-sealiah 
Date:   12-09-05 19:15   >>> Répondre à ce message

ndareuuuuuuuuuuuuuuuuuu
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   13-09-05 08:08   >>> Répondre à ce message

suis là et ailleurs aussi.
Ba beenen
 
 Re: wolofisons
Auteur: ex-sealiah 
Date:   24-09-05 20:30   >>> Répondre à ce message

jé vu
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   26-09-05 15:38   >>> Répondre à ce message

snifffffffffffff
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   27-09-05 20:46   >>> Répondre à ce message

célia :
saf boy , y a ngué nekh bé teye ?? Fo nek légui ?
 
 Re: wolofisons
Auteur: Ndar-- 
Date:   07-10-05 09:19   >>> Répondre à ce message

Exxxxxxxxxxxxxxxxxxx
 
 Re: wolofisons
Auteur: pierre_diop 
Date:   07-10-05 22:32   >>> Répondre à ce message

ndar , li moye lane ??
Ndar sa ma waye , guissou lo célia ? damako name to rop !!
 
 Re: wolofisons
Auteur: zouklove 
Date:   14-05-08 14:54   >>> Répondre à ce message

on n'a toujours pas su l'auteur du zouk khalébi:-(((((((

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : Paris PAYS : France
 
 Re: wolofisons
Auteur: zaga 
Date:   26-07-08 14:20   >>> Répondre à ce message

sény wolof kéne mounou ko comprendre!!! dama beugeu ngéne jdangue lan la niou bindeu !! djérigénédieuf

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : Thorenc PAYS : France
 
 Re: wolofisons
Auteur: zaga 
Date:   26-07-08 14:24   >>> Répondre à ce message

soudoné téne dina la nane

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : Thorenc PAYS : France
 
 Re: wolofisons
Auteur: INAATA 
Date:   05-06-09 23:16   >>> Répondre à ce message

Bonjour a tous, tout d'abord je m'excise si je ne poste pas au bon endroit :/

J'aurai voulu savoir si quelqu'un pourrait me traduire ceci en francais svp :

"lol ma la raw! Amoul nou me léén naméwoul nak mais waloum anniv bi mome on va regler nos compte boul soone. Ouz mome beurré si kaw Z..C yi leu tall mais lamb dji wakhal ba mou djekh rek !!!"

Je vous remercie par avance :)

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : Nanterre PAYS : France
 
 Re: wolofisons
Auteur: Sambou   
Date:   07-06-09 22:11   >>> Répondre à ce message

INAATA:

Traduction en français:

Lol, plus que toi, y'a pas un instant ou vous me manquez pas,, mais cette anniversaire ont va regler nos compte, te fatigue pas.

Ouz vraiment beurré jusque la haut, Z..C c'est ce q'il a allumer, mais la lutte la raconte jusqu'a que ça ce termnie seulement.

J'AI RIEN COMPRIS J'AI FAIT QUE TRADUIRE MOT A MOT, a vous de trouver la logique de la phrases.

 
 Re: wolofisons
Auteur: Marie88 
Date:   14-11-09 03:13   >>> Répondre à ce message

Bonsir,
Je voulais demander:
Par exemple, comment prononce-t-on :

Maa ngui fi
diam aksalam
mba diam ngua yen do
ba bennen
jeredief
waow
kay fii
kharal
degg naa

Comment dit on ''je t'aime''??:0

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : Saint-Étienne PAYS : France
 
 Re: wolofisons
Auteur: thièskay   
Date:   04-12-09 19:52   >>> Répondre à ce message

Salam

gayi né ngen deff ma ngi len di nuyu yen nieup kou ti nek ti sa tour ak sen sant!!!
 
 Re: wolofisons
Auteur: thieskaye 
Date:   15-12-09 16:41   >>> Répondre à ce message

traduc: salu tous le monde je dis bonjour a chacubn avec votre nom et prénom

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : Montesson PAYS : France
 
 Re: wolofisons
Auteur: babatraore 
Date:   22-12-09 09:34   >>> Répondre à ce message

help! bonjour, quelqu'un pourrait me traduire s'il vous plait
manite namenala dilene khana merci

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : Évry PAYS : France
 
 Re: wolofisons
Auteur: la nene   
Date:   23-02-10 03:42   >>> Répondre à ce message

the song is not khalebi
it's Ely and the singer's name is Sylvestre Gomez

mb
Posté depuis www.planete-senegal.com
 
 Re: wolofisons
Auteur: boucle 
Date:   19-02-11 10:28   >>> Répondre à ce message

Bonjour quelqu'un pourrait t'il maider a traduire SVP Merci

da niouy fo rek

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : Paris PAYS : France
Posté depuis www.planete-senegal.com
 
 Re: wolofisons
Auteur: ndar.tout   
Date:   19-02-11 12:26   >>> Répondre à ce message

Merci pour avoir réveillé ce fil, cela m'a permis de relire des anciens forumeurs, dont mon amie sealiah !hbreak

--------------------------------------
Tout ce qui est excessif est insignifiant.
-------------------
Posté depuis www.senegalaisement.com
 
 Re: wolofisons
Auteur: jongama   
Date:   23-03-11 14:28   >>> Répondre à ce message

Dañuy fo rekk.

Nous jouons seulement


Posté depuis www.senegalaisement.com
 
 Re: wolofisons
Auteur: Sisi 
Date:   02-03-14 23:46   >>> Répondre à ce message

Qui peut me traduire cela: "Man nobatoumala "? Merci

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : Cachan PAYS : France
Posté depuis www.senegalaisement.com
 
 Re: wolofisons
Auteur: Guélowar   
Date:   03-03-14 00:10   >>> Répondre à ce message

Moi je ne t'aime plus.

Nino irresponsable, zap total. Reureka vicieux, conneries de toutes sortes, dénigrement systématique perpétuel erroné trop souvent, lecture parcelaire zero réaction. Couilledeloup maboul et maso, retour de bâton.
demsenegaldem.forumsenegal.net
Posté depuis www.senegalaisement.com
 
 Re: wolofisons
Auteur: ndar.tout   
Date:   05-03-14 14:03   >>> Répondre à ce message

Là il a mal.
Tu aurez dû le préparer en douceur, avant de lui balancer la traduction sec!

--------------------------------------
Tout ce qui est excessif est insignifiant.
-------------------
Posté depuis www.senegalaisement.com
 
 Re: wolofisons
Auteur: Guélowar   
Date:   05-03-14 14:38   >>> Répondre à ce message

hé oui mais bon ...

Nino irresponsable, zap total. Reureka vicieux, conneries de toutes sortes, dénigrement systématique perpétuel erroné trop souvent, lecture parcelaire zero réaction. Couilledeloup maboul et maso, retour de bâton.
demsenegaldem.forumsenegal.net
Posté depuis www.senegalaisement.com
                    

Liste des forums  |  Besoin d'un login ? Enregistre toi ici
 Identification
 Nom d'utilisateur:
 Mot de passe:
 Se rappeler de mon login:
   
 Mot de passe oublié ?
Entre ici ton e-mail ou ton identifiant et un nouveau mot de passe te sera envoyé par mail.